| Fråga | Svar | |||
|---|---|---|---|---|
| Nanga def?  | ||||
| Maangi fi rekk  | ||||
| Naka waa kër gi?  | ||||
| Ñuungi fi  | ||||
| Nanga fanaane?  | ||||
| Nanga yendu?  | ||||
| Jàmm rekk  | ||||
| Nangeen def?  | ||||
| Nungi fii rekk  | ||||
| Ana / naka sa yaay / sa baay?  | ||||
| Mungi fi  | ||||
| Nangeen fanaane?  | ||||
| Naka ligéey bi?  | ||||
| Mungi dox  | ||||
| Mbaa kenn woppul?  | ||||
| Mbaarikala  | ||||
|  reply to nanga def | Maangi sant  | |||
| Numu deme?  | ||||
| Nii rekk  | ||||
| Naka afeer yi?  | ||||
| Ñungi dox  | ||||
| Yaangi noos?  | ||||
| Tuuti rekk  | ||||
| Lu bees?  | ||||
| Dara beesul  | ||||
| Nelaw nga bu baax?  | ||||
| Waaw, nelaw naa bu baax  | ||||
| Jàmm nga fanaane?  | ||||
| Naka suba si?  | ||||
| Jàmm nga yendoo?  | ||||
| Naka ngoon si?  | ||||
| Naka tangaay wi?  | ||||
| Naka seddaay bi?  | ||||
| Ba benneen yoon  | ||||
| Ba ci kanam  | ||||
| Ba fan yi  | ||||
| Ba suba  | ||||
| Ba ngoon  | ||||
| Ñu yendu ak jàmm  | ||||
| Jàmm ak jàmm  | ||||
| Ñu fanaan ak jàmm  | ||||
| Dégguma Wolof bu baax  | ||||
| Dégguma li nga wax  | ||||
| Maangi jang Wolof ndank-ndank  | ||||
| Jërëjëf  | ||||
| Nuyòo  | ||||
| Nuyu [someone]  | ||||
| Def  | ||||
| Fanaan  | ||||
| Yendu  | ||||
| Liggéey  | ||||
| Dox  | ||||
| Noos  | ||||
| suba si  | ||||
| Kër  | ||||
| Dara  | ||||
| Ana  | ||||
| Naka  | ||||
| Rekk  | ||||